"Nena Waaw"
— waka ta Jahman X-Press
"Nena Waaw" waƙa ce da aka yi akan senigal da aka fitar akan 07 satumba 2019 akan tashar tashar rikodin rikodin - "Jahman X-Press". Nemo keɓaɓɓen bayani game da "Nena Waaw". Nemo waƙar waƙar Nena Waaw, fassarori, da gaskiyar waƙa. Ana tattara kuɗin da aka samu da ƙimar kuɗi ta hanyar tallafi da wasu hanyoyin bisa ga wani yanki na bayanan da aka samu akan intanet. Sau nawa waƙar "Nena Waaw" ta bayyana a cikin haɗe-haɗen ginshiƙi na kiɗa? "Nena Waaw" sanannen bidiyon kiɗa ne wanda ya ɗauki wurare a cikin fitattun ma'auni, kamar Top 100 Senegal Songs, Top 40 senigal Songs, da ƙari.
|
Download New Songs
Listen & stream |
|

"Nena Waaw" Gaskiya
"Nena Waaw" ya kai 6.7M jimlar ra'ayoyi da 35.9K abubuwan so akan YouTube.
An ƙaddamar da waƙar akan 07/09/2019 kuma an shafe makonni 279 akan jadawalin.
Asalin sunan bidiyon kiɗan shine "JAHMAN X-PRESS - NENA WAAW".
"Nena Waaw" an buga a Youtube a 06/09/2019 21:16:17.
"Nena Waaw" Lyric, Mawaƙa, Label ɗin Rikodi
DISPO SUR LES PLATEFORMES
LYRICS
Couplet 1.
Li yalla sak lep si taar sa dieul lama doon missal
Moussougn tegante beut wayé nio bok fign doon khol
Kheuthio bi meti woon neu
Wayé ya finaalou yow la faral
Khol yi wara and bagn dioudo ba tey niongui weureuté
Waye sougn dadie kenn si niow dotoul weranté
Kouni dina kham ni ni
Ki la doon seet ki rek la wara doon
Ref.
Nena waaw
Te khol bi nena waaw
Wadiour yi nenegn waw
Xarit yi nenegn waw
Nieup negn waw kone yow la wara doon
Nena waaw
Te khol bi nena waaw
Wadiour yi nenegn waw
Xarit yi nenegn waw
Gni bognone sakh moudiou nangou nena waw
Couplet 2.
Ak yow beugouma sakh deme sama xel
Beugouma soor lou bari mbeugelou zero calcul
Mane nangou wou ma sakh kouy yakh sama xel si yow mem soudé deug mala koy ndieukeu wedil
Fogoon na ni xol bi yaxuna te dotouma beugaat
Deception lou meti leu koum dal doko beugeu doundaat wante yow
Danga mel ni drogue si psycopathe
Daf koy gagne te lolou la sokhleu.
Nena waaw
Te khol bi nena waaw
Wadiour yi nenegn waw
Xarit yi nenegn waw
Nieup negn waw kone yow la wara doon
Nena waaw
Te khol bi nena waaw
Wadiour yi nenegn waw
Xarit yi nenegn waw
Gni bognone sakh moudiou nangou nena waw
Couplet 3.
Sokhla touma leneen na goumbeu
Tey nak guid na sama goor
Aduna bi yeup say digante loxo mo si geuneu woor nenala waaw
Baby yow la doon xaar
Depart ba lama mbeuguel arrivé si yow do to ma raw
Daw na ba sonn meunoul nek bobou khol bi nena waaw
Metiwoul nga daw
Supporter nga samay caprices ak merr you
#jahman
#senegal
#love
#nenawaaw